Accueil Actualités chronique de beugue baye kep thiam

chronique de beugue baye kep thiam

18
0
PARTAGER

waw batay rék niou dokhantou nank si kéneu si sahaba yi niou kham ko si seydina alune borom diassi dji mamou kouli cherif yi waw mom bamou néké lire manam bébé yayam dafko teureulone si berceau dém bayikofa am béneu diane manam serpent nieuw beug ko matteu seydina alune khékh ak mom ba rayko té bobou fékeunanko mou nék lir bi yayam yéksé dafani way nékété man aidara la diour manam gaindé la diour motakh aidara bi fofou leu diougué souko baye di nétali nga dég mounanne mom le cherif yi di titeuro manam sante aidara waw batay rék si seydina aalune momou bi yonent psl waré dém gaday mom le wakhone mou outouko si keurgui té nieup khamone naniou ni risque le wayé mom paréwone neu nguir niakeu bakanam nguir rassouliah psl mouy acte diambarté bou beuri diangat si ando machalla
#lundi_rassoulilah_psl

LAISSER UN COMMENTAIRE

Please enter your comment!
Please enter your name here